ترانه و شعر با صدای Mia Guisse
Danga took sama xol yaye kiki mome léboone Guénteu na takeu leu kaay done sama yayou doome Dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome Té beuss boussa doome indé dome defco dome sama doome
Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
Dinala romb midi Oooh wait Té doma guiss Oooh wait Pénicilline yangui gneuw Oooh wait Ma dabali Oooh wait Gaa fof no welly Oooh wait Now doto KO défati Oooh wait Oooh wait Oooh wait
Gnata yaye la fi seuye teuthie thi kasso ndax séne doome Yi lathie ngay lathie téy amagou ma tontoome Yague Toul legui Rek nga xam louy noone sama doome Ideu bi tey la diékh tay Di diégueulou waat sama doome
Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye Li nit di dathie thi naigou seuye Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
Dinala romb midi Oooh wait Té doma guiss Oooh wait Pénicilline yangui gneuw Oooh wait Ma dabali Oooh wait Gaa fof no welly Oooh wait Now doto KO défati Oooh wait
Dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome
Paré- paré- pa- pa- Paréna Xamoni bou diééxé Diééx na Diééx na
Gneuweul Han Ngani Han Han
Mani baydou volume Sabou mi nana ni Tékki lunettes yi nguir gueuneu guiss
آثار دیگر از Mia Guisse