
ترانه و شعر با صدای VJ
(Sheyi on the beat) Ndeke dou mbeuguelou Kassè Teh sax fais tout mbeuguel yi dafa rare Dièkou ma ni douma bale yeah yeah An konne yaw bandi nga ndèkè bébé Sopi nga sama xol bi limonade Siroter ko diko nane yeah yeah Ndax baniouy ndieukeu guissanter Li nga ma yene nimou disser Ak niniou xolanter Rek ma xamni yalla niou bolè Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (kaay waay) Doflo ngama (kaay waay) Wayè deufeul ngama (kaay waay) Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay) So bèguè ma bègue (kaay waay) Niou deukè di rè (kaay waay) Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay) Maala geuneul lounè (kaay waay) Teh yaama geuneul kounè (kaay waay) Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay) Bègal ma bèg (kaay waay) Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay) Soma sorè oh my love Namel bimay yeuk thi yaw Wallahi yaako meuneu fadie nieuweul Niouy kaf di rè Niouy kaf di fo di rè Ndax baniouy ndieukeu guissanter Li nga ma yene nimou disser Ak niniou xolanter Rek ma xamni yalla niou bolè Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (kaay waay) Doflo ngama (kaay waay) Wayè deufeul ngama (kaay waay) Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay) So bèguè ma bègue (kaay waay) Niou deukè di rè (kaay waay) Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay) Maala geuneul lounè (kaay waay) Teh yaama geuneul kounè, ah (kaay waay) Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay) Bègal ma bèg (kaay waay) Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay) Oh bébé, toi mon bébé Toi qui m'a tout donné Je pourrais jamais te quitter Je t'en fais la promesse, mon bébé Tu m'as tellement épaulé Quand il le fallait M'a sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bébé yaw mi gounguè ma man malay gounguè Et si t'a peur, crie "aidez-moi" mane maaa lay sauvé Oh bébé yaw ndax beuguè ngama comme nim la beuguè Ndax nim la beugè eup naaa wa li noum dèmè Oh bébé, toi mon bébé Toi qui m'a tout donné Je pourrais jamais te quitter Je t'en fais la promesse, mon bébé Tu m'as tellement épaulé Quand il le fallait M'a sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bébé yaw mi gounguè ma (kaay waay) (Kaay waay) (Kaay waay) (Kaay waay) (Kaay waay) (Kaay waay)
آثار دیگر از VJ