
فرمت MP3 • بالاترین وضوح صدا
فرمت MP3 • مناسب اینترنت ضعیفتر
ترانه و شعر با صدای VJ
Soumala namé bayi dieuleul paka dass reyma Ndakh bolei nga linga am ak linga amoul lepp dioxma Souma ley fethial guudi bae dou niak feyda Ma bolei sama xoll bi ak xeuteur teksi juuni meyla
Mbeuguël nimou néxé boudeh deug la dou loumey waxx Doundou thi liniou féké danga diongué teh néxa andale Allah allah architecte bi défar qui deh mani ayna Yow wowal ma sa badiéne mou nieuw fok mou leral ma Woy diongué nga
Yak sa ayi (nexayy) Danga rafet (togay) Nex nex la (tiouraye) Yungueul ngama (saï saï) Mane dama la beug nga beug ma (saï saï) Mani la beugunteh la (saï saï) Dinéniou radiakhé deuk bi (saï saï) Wathié ko bamouy zéro (saï saï) Lih pénalty la Mbecté bi néh sama xoll nga nieuw indi Kone togal xarr, xool, yénéne lah ley indil Lih dafa neexa neexa neex teh vitaminé Na foh bah dougou sa 18 niou moulay thieuguine
Ma moudié diakhlé Ndékété bideew dina fegn beuthieuk yangui Gni nénégn dama doff gni nekh dama salite ladjal sama gars gni Mane louma daanel yomboul wayé K.O ngama
Baneex biniou néké dafa eupeu bah meunou ma waxx Xalei bi ninga diéké danga diongué teh neexa andal Ala ala architecte bi défar qui deh mani ayna Yow wowal ma sa badiéne mou nieuw fok mou leral ma Woy diongué nga
Yak sa ayi (nexay) Danga rafet (togay) Nex nex la (tiouraye) Yungueul ngama (saï saï) Mane dama la beug nga beug ma (saï saï) Mani la beugunteh la (saï saï) Dinéniou radiakhé deuk bi (saï saï) Wathié ko bamouy zéro (saï saï) Lih pénalty la Mbecté bi néh sama xoll nga nieuw indi Kone togal xarr, xool, yénéne lah ley indil Lih dafa neexa neexa neex teh vitaminé Na foh bah dougou sa 18 niou moulay thieuguine
Yak sa ayi (nexay) Danga rafet togay Nex nex la (tiouraye) Yungueul ngama (saï saï) Mane dama la beug nga beug ma (saï saï) Mani la beugunteh la (saï saï) Dinéniou radiakhé deuk bi (saï saï) Wathié ko bamouy zéro (saï saï) Lih pénalty la Mbecté bi néh sama xoll nga nieuw indi Kone togal xarr, xool, yénéne lah ley indil Lih dafa neexa neexa neex teh vitaminé Na foh bah dougou sa 18 niou moulay thieuguine
Tegg diexal thi yow chérie Bama nieup bayé yow la dessé Boma bayé mane dina déh bae Kone collel serrél, bébé fais moi rêver Mane sougn ma ladjié kane moy sama moitié Mane meuna wate néh yow yay sama moitié
En collé serré, bébé fais moi rêver Sa youniou guisseh, guisso nimouy néxé Dans ciel étoilé, que nous deux ma moitié En collé serré, bébé fais moi rêver En collé serré, bébé fais moi rêver Sa youniou guisseh, guisso nimouy néxé Dans ciel étoilé, que nous deux ma moitié En collé serré, bébé fais moi rêver
دیگر آثار شنیدنی از VJ